LYRIC

Couplet Fire flow

Couplet PPS
Ci souf la djogué, ni ndongo lo ndém si yalla
Tanku kanam dotoul féki tanku guinaaw ndém ziyaar na
Fi niu djogué dafa sori, yégg gueuneu djégué délou
Boot lu bary xuss ci gor yi, di niaanal gni njeukeu dallou
Daniou – xiif soga réggueu, daniou – beef soga yéggueu
Daniou – guiss yone wi dém, tép tép soga nékkeu
313 mille ans, la lén rawé déggo ma dé – Ni van basten milan, dama kawé dékku ma dé
…Mbed mi xamé ghost, writah sa mbind mi kawé goss
Wooté nga mani naam, wanéna maninam, sopina thioli nou mbed légoss
… feiye ci léer yi sa xéla öss, mbind mi xaré la féxéla xooss
Niveau bi yokku na sorina, fimou né deukeu niou sooroul niou damm sa looss

Refrain
Sunu kaddu la – wakh ma ko niouy teukeulé
Djogué ci soufa souf – di fowé li nguén teulé
… Track bi guénté la, rap bi djoudou waate na taye
Wax ko nieup, Nianal lén xalè bi ndaye ak baay

Sunu kaddu records la – Wax ko nieup!
Track bi guénté la – Wax ko nieup!
rap bi djoudou waate na – Wax ko nieup!
Wax ko nieup! Wax ko – Wax ko nieup!

Yeurmeundé day wagni doolé goor – dou mér di saaga boolé door
Ci mbind laniouye wané xaragne – nio fi meune déeko soor
… Writah ci mic bérnabeu youkhou Chris taal
… Wakh ko ci mic meuné scene, rare ni crisstal
Maa né sén crise daal, beuneu kholou sissou kate yi
Melni lissa naane café ak classe tok ci sissou Katy
Borom bé ma aal bombe nguir ma taal séni mistakes
Mane future laay lakk, déloul gueustou sama Xtape
The living legend like jordan ci parquet
Street cred nieup writah – man nio daane ci barké

Added by

Papi

SHARE

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR