LYRIC

[Refrain] We are all nigga we are all
Ready for the show of the year we are all (2x)
Twenty dec fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
Twenty dec my nigga fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
We are all nigga we are all ready for the show of the year
We are all
We are all ready for the show of the year
We are all ready for the show

[Couplet 1: Nitdoff] Solo pinw té wanéwo sa down
Banlieue ba ci region yi gnénen gniy gnibi town
Kilo pain ak ndiabou underground
Nioun rek nioko meun deffé ni mbed mi come arround
Dassal guaw yomb neu moss salaw
Gni yagua khékh té thioubou niou sen drapeau laay shoutout
Recognize ghetto dey recognize
Tchi tribune bek tchi souf na fepp takk lepp nice
Indaléel sey dome iba mar wathie daume
Magui ak 5 bums niou rap banopi séntou koom
Fouma ndanane di djiar mane sama mame da nane guitar
Galsen bay nafi waar ba torino ak panam di khar

[Refrain] We are all nigga we are all
Ready for the show of the year we are all (2x)
Twenty dec fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
Twenty dec my nigga fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
We are all nigga we are all ready for the show of the year
We are all
We are all ready for the show of the year
We are all ready for the show

[Couplet 2: Kaz] Stade bi yagu na fesss, Légui nék na fief
Lolou dou thiotou biss bou nieuw niou tothi ko guéne né fess
Guathié yagu na sitt ci dèkou sisouman yi
Gaindé dou léke Décid méme bouy déh si digou man ndi
Paréné amou fi , maréné, ndawtal melni mérou Mbotay
Xarré ci rangalé trophée show of the Year guneu kawé ay montagne
Fuck you dagno tay, mbalakh dou rap dépassé wo ngay
Gunzout da nio Ay légend ci game ni Ali niom Ty (tyson)
Meu rap beuri fem, kou gum rap douniou haine
Nio dakalé scène, my nigga do dap lini mel
Xolou talibé si fondement bi bolékak guneu ting
Kouniou fek si concurance bi click shot bang bang

[Refrain] We are all nigga we are all
Ready for the show of the year we are all (2x)
Twenty dec fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
Twenty dec my nigga fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
We are all nigga we are all ready for the show of the year
We are all
We are all ready for the show of the year
We are all ready for the show

[Couplet 3: Yanko] Game bi da thiéré ba thiakhé kone bounou ko simoul dou nekh
Parél yu niari show indi sa gang bégé ba guiédj gui fér
Mélomanes yi real yi costé nieup taxaw paré riposté
Ramasser tickets diékh même sou noni di khekh
Lolou dou khér daye féss rek
Iba mar dou noir bête
Niata ate migui fess loloy sa casse tête
Niom rappeur vue nioune rappeur zéro sponsors wathi thi mbédeu tek
Why you say you are the best ?
Fénioul sa rap fénioul sa texte
Dagua niane ba takeu niou ligéy ba fégne dou dagne nioune niogui fi mérite bi nek
Talal lokho am dou mérite
Ligéy guiss beug go get it
Nioune douniou dougou fép mathial nieup
Pour meuna woté show féssal salle
Meussouniou woté walou sounouy fight
Liy bakhou goor moy daye niémé raak
Raak ba blanco sa carrière bindeu sounou boss dogua bayi trace Waw

[Refrain] We are all nigga we are all
Ready for the show of the year we are all (2x)
Twenty dec fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
Twenty dec my nigga fou ngueni déss
Galsen yepp babékou iba mar founé di féess
We are all nigga we are all ready for the show of the year
We are all
We are all ready for the show of the year
We are all ready for the show

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR