LYRIC

Intro

Were you to die
You would never die alone
We would die together
If I got wings to fly
I will never fly alone
We will fly together
Either we fly together
Or we die together

Couplet 1

Ba niouy deugueur khamé
La niou Bour bi khiir si bilé yoone
Soubak ngoone niou siy try kéne dou sip si li niou né
Warone gueustou khamlé
Tégaate lép si yoone
Doone li niou doone never die téwal fou niou meune né
Beatbox grafity breack dance freestyle
Dread lox timberland boot kou nékeu di woute style
Feel ko, everyday dagne doone dianok moom
Here we go heal deal bi kill bitch yi beurek moom
Diokh ko gueudeum
From battling si party yi
Hip hop bou doone brigade niou doone alkati yi
Latch ko ndégueum
Ana niane nioy dékou matter yi
Gni koy doundeul gni koy faate Ragné nagne si khata yi
Séne nda bou fééssé
Robinet ko alimenté nioune si fleuve la niouy diokou té dagne nieuw dépanner
Carcasses yék pétasse yi, bitch ass yék patasse yi
Takhaw défense kass diokhé sasse yék dépenses yi

Refrain

We are hip hop
Cuz we live it to the core
Dagne ko gueustou keuss before
Always ready to go
Nioune nioy hip hop
Dégue nagne lou né ndakh moome
Waral khole yi féssak guaum
Niou gueune di weuyak diom
Cuz we love hip hop
Nioy indi lére si leundeum
Exciter nerfs yi yéki dieum
Def si frères yi gueum gueum
Nioy hip hop
Nioy hip
Nioy hop
Nioy lép
Nioy fép
Hip hop we are everything

Couplet 2

SPOKEN WORD, MC-ING, RAPPAREE, RAP
DJ-ing, SCRATCHING, GRAFF, DANCE: “HIP HOP”
Seventies ba légui bou doul wone deugue naakhsay
Meuno guiss di wédi never songue kharé di gaaday
HARD CORE, GANSTER, RNB, CRUNK ak yénéne
Ma tidji doors yi séte yénéne sound bolékok lénéne
Gni ma guindi yéé
Gni ma rééré sankou
Gni beugue ma déé
Def séni pékhé lonkou
Listen diéguina solok ndiaap
Esprit la diéme ko doundeu
Sa brain ngay ndieukeu laap
Saupe sa rouh si bénéne doundeu
It’s not about salary
Meune nga ko latch KRS ONE
It’s all about describing the reality
Yes get it man
Meunouma diglé sét tilim
Kone amna fou dokhoul gayi
Bou léne may forget dou prime
Non dou ma momromou séne détaille yi
May watchi chefs d’états
Feuseul crimes yek dégâts yi
Indi light guindi gayi
Khokhatal dou takh ma bayi

Refrain

We are hip hop
Cuz we live it to the core
Dagne ko gueustou keuss before
Always ready to go
Nioune nioy hip hop
Dégue nagne lou né ndakh moome
Waral khole yi féssak guaum
Niou gueune di weuyak diom
Cuz we love hip hop
Nioy indi lére si leundeum
Exciter nerfs yi yéki dieum
Def si frères yi gueum gueum
Nioy hip hop
Nioy hip
Nioy hop
Nioy lép
Nioy fép
Hip hop we are everything

Couplet 3

Lép sa may fane, da nguéne si touti bou léne ko sakh try
Gueustoul may kane, ba la nga sobou i’ll never die
Khamoo fi ma diogué, meunoo sip fi ma beugue yégueu
Diéguél gni ma diégué amna niou ma si léguer dégueu dégueu
Fight pour deugueu deukeu si yokeu sama gueudeu
Anytime niou ngui seugueu si waar amouniou diotou teudeu
Real recognize real kéne douko dindi
But amna niou koy forcer weural ba datch gni lay guindi
Sa ma reputation bakhoul cuz si mbédeu la dioudoo
Music bou ma gueune amoul malay wane nou life bi bindoo
Tel qu’elle est, sans retouche, c’est la vérité pure et dure
Point fermé stand to push kholko samay procedure
Niata hero la def?
Je fais des personnalités
May ték ghetto bi say khef
Youkhou fépeu égalité
Feusseul corruption injustice déception
Struggle is my option I’m here to save the nation

Outro

Were you to die
You would never die alone
We would die together
If I got wings to fly
I will never fly alone
We will fly together
Either we fly together
Or we die together..

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR