LYRIC

{DIP}
Neew tchi suuf faydou ci kaw, dérettou meedeu deum yu marr yi mouthiou ko
Mère bi rekka tourone dérett bamay djoudou gni tchi dess nieup double f**k
Ndaw ba paré bagne fu xatt daanou ci térasse taxoul bama joug tchi kaw
Thiappal xaliss ci say Règles bamou xonkeu so paré dioxma carton rouge bi bokk
Ba ngène maré mane maa def ni kirikou, Gni teudjoul sen gatt moussougnou tidji bountou
Amoul yo wou région bima maatoul ci att bimay dieulé Hip Hop ci sibirou
Gni baayi teuweu djaap dougne tidji bountou, Tay maa eupeu xaliss maa eupeu vue Youtube
Papa bougouma wone saaga, Daa am boy you dawone deupaate nieuw tok fi di doule
2Pac Biggie dém nagne mane maa dess mane kèn douma ray ndax dama déh
Comme que bèn label meunou maa fay, Ma djaay sama lale teudi sama bamél
Dérettou Iblis laa tour ci sen carrière yi, Teug concert beuthieuk ci kaw VDN Bi
RAP beu Monsieur le juge xamné xamné awouma dara loumay prouvé, Nélène yeen libéré len ki
Souma nekhé baayi légui nek Abbé, Sétal texte yeup diko waaré Eglise
Légui sen son day daw radio, Mane sama baSse kagne lay jougué ci sen ADN yi
Daaj la ni GUEJJOU(mer) SANGARA, Daaj la ni Tollou Yamba bou takk ba di sakhaaral
Beus boumay guéné bou kèneu guèneu dina melni taawou ballou fétél. Soubhaana lah !

Hééééé yaaaaaaa
Hééééé hééééé hééééé ya
Hummmm ummmmmh
Weet na boy, Weetna boy
Weet naaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa
Aaaaah haaaa haaaaaaaaa haaaaaaaa héééééééééy
OoooOoh hooooooo Oooooh hoooOooo Ooooh
Ooooooh waaaaaa haaaaaa

{Refrain}
Fima deuk amoul niaari place
Kou dieul sama place nangou sama deuk
Parce que weet na
Weet naaa boy
Déh soga am ni kamikaz
Am soga Déh ni Kadhafi nigga weet naa
Amena niou gueum GAAAA
Am niou gueum CFA
Fils ya ngi ci biir 5 rappeurs yifi dakkeu bindeu Histoirou Sénégal
Gni fi bindeu mattou niou 5 sakh
Bouma rétane lolou nga tek ci sama kaw montagne
Dieulouma revanche awouma koumay may chance
Awouma ben concurrence téy liniouy waadjal xamnga def naako

{DopeBoy}
Sheytaane sama dérett, Anti-christ mi ngi feep
Waurouma ni Rouh bi meuneu tina sett
Nékoul borom coss yu nioul yi rekka mom pyramide yaw sakh ci nga né
100. 000 personnes dallay weur nga weet
Né tchi leundeum fokné ya ngi tchi lerr
Lathié paquet dégrainé nako bamou setttt
Dougou bénène galaxie
Shit ! Pussy nigga f**k sa monde bi
Souma taalé zoin bi ci laay soga lucide
Soucis guéneu sama bopp bi
Je préfère weet ak sama bopp
Bania affiché sourire yu neubeu métite bi
Matrice bi beuri fake né comme ……

{BM Jaay}
khol yé andoul guiss guiss khoulo
Soneu ci sett kimay ndirau
Boy bayil rétane ma def semblant melni yaw
Hyprocisie moy lou bolé nieup
Xam nga ki ngay guiss bo sétto nékoul yaw
Kounék amna kanam boye yaubou fo meunti dem pour melni gni ngeu fay fek
Kone nieupeuy naafeek, naafeek comme yaw Weet comme kouy yéwo ci baamel
Weet parce que Alaaxira mbokou amoufa siip na Niodi wouma dara nii la mel
Yokk samay casque bamou fort meune sori sen Dunya
Beug rap motah niou xamanté, normal beug rap takh niou ndara bayenté waat
Djapé wou mala xarite té douma bééteu beus boy déllou naane da ngay dokh sama garde

{Refrain 2}
Fima deuk amoul niaari place
Kou dieul sama place nangou sama deuk
Parce que weet na
Weet naaa boy
Déh soga am ni kamikaz
Am soga Déh ni Kadhafi nigga weet naa
Amena niou gueum GAAAA
Am niou gueum CFA
Fils ya ngi ci biir 5 rappeurs yifi dakkeu bindeu Histoirou Sénégal
Gni fi bindeu mattou niou 5 sakh
Bouma rétane lolou nga tek ci sama kaw montagne
Dieulouma revanche awouma koumay may chance
Awouma ben concurrence téy liniouy waadjal xamnga def naako

{Samba Peuzzi}
Fokk meuTEKI soga FREE May wéteuliko GORé sama ngor amoul PRIX
DJIRIM depuis MINEUR laa SOUL samay TANKEU gueum ko XOUSS ba yeksi fi.
bro, Weetone naaa
Mais ma doli sanT takkeu sama fiit ba légui tuur bé ngi daw
FLOW bouy dieundeu KEUR laa indi ci GAME bi rek RAPPEURS yi teksi BRIQUE
COMPTé wouma ci kène pour AM lou dieum sama COMPTE
JOB bay FAY motah say MC BANQUE, Controlé Banlieu bi tekk fi tankeu
Ci ay rek nga daane dégueuh boy Diaama Gueune
Kila feeté suuf rekkay wakh ci sa guinaaw
Tcha kaw tcha kanam dama lène Tiim bayi lène niouy fènn
Game bi louma tchi gueuneu yagg di gueuneu tangueu
Kone diaroul ngakay wakh xam naani dina baaw

{Kanyzii}
Mane weet naa weet naa sama life ni dom bou guissoul Papa ak Yaye
Dama reer ci diggou aaleu night mane dongue ma ndara djanok aduna
Mane tokna ak yaw ya ngi wakh mais meunou mala dégueuh Baye
Ma ngi doundou mais ci sama bopp dama sori nékouma tchi aduna
Héééé hééé Waxma nane lay def ba guèneu tchi, Tchi jungle bima nekk ni
Chaque jour ak problème yu bessati ndakh deum yila beug eat
Li ngène beugone moy ma peuteukh mais tay yéneu meu djitou ci kambeu bi
YALLAH dou teuth bountou wathié rideau, té kounek dinala fay li nga djiii

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR