LYRIC

REFRAIN
Fo guésso werul ci mane, ci mind ci mind sen thiofél défma kemane
Yénaye hip may hop, jiteul ma dima samm, yénaye jeum maye bopp
Galsen worldwide, love love mo koy faye, wrirah fam never die

Ma prose doute, dans mon esprit il pleut a grosse gouttes
scrutant l’avenir, les larmes a venir dans les squares
16 barres, une melodie pour entretenir l’espoir
C’est l’histoire du writah family, gniye mane té maye niom
li niou done déf ma lima done, gueum yok ma diom
maye hip ngén di hop, sén yéné dolél sama yone
Jiteul ma dima samm woyofal sama yéne
Sama yéné, dina kawé sén njorte affaire bi yéneu
yaa ci xol yi, xél yiye xéli, thiofél gou yémé
Yalla yaana, ngueum laniouye démé
Fo guésso wérul ci mane, maye sén bro
xam na fi nga maye séene dina ko matal ci galsen bro
Writah ki la, yaw, kée, mane
Gueinte lama dikée mane, limou eumbe di kémane
The sky’s the limit, déme naniou té douniou guéssou
Maye xalima, yénaye dáa gui, ramatou gui daniou ko wéssou

REFRAIN…

it’s bigger than hip hop, I shine like you hommy
Dou néene yalla la, waral publique bi youxome yi
Deinke sunu life askan wi, xátim xolli góme yi
Sen njarigne di déf liniouye waxe, bagna waxe liniouye déf
Ay nitt dong lagne, dégg déggaye thiabi ji
boudoul wone writah family taye fénéne laye tabbi ji
Niata yone laniou tok, xalate défi lénéne
Music kéne douko lék, souba défilé néene
Waar wé tar ci nathie bi wayé founiou guésso rée
Diapal téweu bayi, sén yéné di sooré fou sori
Sori naniou founiouye woré, sén mbékté niniou koy weuré
Doolé yaakar ni mou beuré, domi mbeur janguil beuré
Jéme bagna meune áyoul, abadane bagnekate ni Simon
Katanou yénou sasse bi, laye sakou yénassaye mane
love love mo koy faye, sori nguéne sama xol
nio far for ever, wanéwouléne ma xól

REFRAIN…

It’s for my writah family
founiou nék ci galsén
founiou nék ci worldwide

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR