LYRIC

{Refrain}
Now you know what we do
And Why we do it (8 fois)

{Couplet 1}
Yo doulok sa gay click ak sey dirty hoes
Doulok sey bullshit bokatouniou cause
Real nigga for life bo beuguè tiow li djib
Nieweul nga talal sa five may be niou may leu shit
Teulè dope yagua saupe snitch taupe
Khamone nga ni da nga meusseu guarr li nga gaube
Ya derailler mbède tèki say grade
Fuck sey track gueumeu touniou sey crack
Fake revolutionnaire shut your mouth tokk
Sip naniou bane doule la seu maf bokk
Turn back amato sa tèen bagg
Fi dofi meusseu Biggie meme so andèk TEN PAC
Doniou messeu dèf tchaz bi ngay iri dass
Nioune daniouy doundeu RAP real ngay trucage
Street Book leu Killah moy firi page
Tchi bi beat ya ngui get sama cri rage.

{Refrain}
Now you know what we do
And Why we do it (8 fois)

{Couplet 2}
Fatel sa plan A (Activiste) ak sa plan B (Bagne kat)
Ndakh sa plan C (Corrompu) mo indi sa plan D (dioutou)
Sa gualathie tothie beu bo dieulè balle blanc dèh
Kane moleu wakh meun nga manipulè mbed bi
Biss nakeu tay kholèma sa pire ennemi
Diotayou mother fucker yoyou nigga ain’t no me
Djante feink neu ba sooh nio ngui ègue night
Shut the fuck up and rap wala nga guèd mic
No politik we just wanna see you flow
Kouy kocc barma kane moleu taalif lo ?
Koula takeul yoyou ndomba tank moleu sank
Meuno RAP nigga tèkk xel moleu sampe
Killah kocc leu sa brain mounteu makk mind neum
Naniou dèlo RAP si diamonoy 99 neum
Real nigga foko fèkk dafey tauthie guayin neum
Tchi kaw deugue doneul deugue bi di faute chaine neum

{Refrain}
Now you know what we do
And Why we do it (8 fois)

{Couplet 3}
I’m big super nigga you’re dick sucker nigga
We know who you are, You’re fat sucker nigga
Hardcore flavor leu mbède bi di maintin
Sunu RAP dou niodi bling bling aki champagne
Gunzout métaphore leu dou diabou gang bang
Wayé boniou khossé nigga di nga djiss lou tang kang
Wu Tang Clan open the mic ma dèmè sagn sagn
Fuck sèni lobbie bokou ma si lot bi
Nameu marr kill doma send sèni robi
Nèy (nèy) Real Die mother fuckin real
No matter what siw dou tèh niou still
Number one flip flap niou dadji skillz
Mbautou mbindeu mè dèh tchi sama khalima
Sama flow day tangue meulnè khal yimeu
Yabi si kaw beat ladial KAZ from Kalima
2007 ba legui fatalima ponkal yima (kill)

{Refrain}
Now you know what we do
And Why we do it (8 fois)

 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR