LYRIC

{Refrain}
Mane sama name modi ADMOW
Sama tour modi ADMOW
Whats my name Ayy (x2)
Sama name modi ADMOW
Sama tour modi ADMOW
Sama name modi ADMOW
Whats my name Ayy (x2)
Sama tour modi ADMOW

{Couplet 1}
Ey leu dou A, Eydmow leu dou Admow
Sama tour bokoy toudou nanga ame flow
Dafa diss nigger atanoko
Kone kaay meu diokh leu bénéne nickname nga mome ko
Dégg na yay sathie sama sound
Diko play thi concert yi neck around
Come diéguéssil meu mayla touti BUZZ nigger
Sama tour bokoy mboubo dinga soulou nigger
Name bi dfa unite 10 ni Modou Lô
Ni Balla Guéye ak 600 kilos
Dfa U tréma ni B2O
Sama name dfa swagg ni Don Sergio
Anh Anh name bi diouguéwoul thi Adama
Anh Anh Boko khamoul kay lathietéma
L’Africain Détenu par la Musique qui s’Ouvre dans le World
Lolodi Admow

{Refrain}
Mane sama name modi ADMOW
Sama tour modi ADMOW
Whats my name Ayy (x2)
Sama name modi ADMOW
Sama tour modi ADMOW
Sama name modi ADMOW
Whats my name Ayy (x2)
Sama tour modi ADMOW

{Couplet 2}
Sama name teupe diotou ndakh dfa kawé
Sama name dfay peundeul ni thiourayou gowé
Sama name / thi bi game
Dfa mél / ni léme
Ni tambali ak diéme
Nguir égg fou soré
Ow Sama name dfa nékha wakh thi guémigne
Nonou leu sokhoré dfay goré mélni sémigne
(AAAAaaaahhh)
Name bi dfay titeulé ni film horreur
Nonou leu coolé, mom dalay nékh dileu bonheur
Name bi dfa swagg, dfa cool dfa nice
Dfa khéw thi diamono, dfa fresh like ice
Street like dice, launch like rice
Yes sama name dfa chér beu amoul price
Say my name, say my name coz I know you like it
Say my ADMO coz I know you love it (Anh)
I know you like (Anh), I know you love it
Coz bokoy toud dagéy smile di ame lou beuri

{Refrain}
Mane sama name modi ADMOW
Sama tour modi ADMOW
Whats my name Ayy (x2)
Sama name modi ADMOW
Sama tour modi ADMOW
Sama name modi ADMOW
Whats my name Ayy (x2)
Sama tour modi ADMOW

{Outro}
La la la laaaa laa ADMOW
La la la laaaa laa ADMOW
Sama name modi Admow, sama name modi Admow
La la la laaaa laa ADMOW
La la la laaaa laa ADMOW
Sama name modi Admow, sama name modi Admow

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR