LYRIC

Bama kay njeuke dégg, hopital guèthi la wone
Dou kèneu koudoul yaay, loudoul thiofel, taar ak yéss
Tektal yi manoul léer, xalaatou demb flou lalay wane
Page bou bess say tambali, té doko sakh adjéss
Ben bu goor ci yaay, thiaat bou goor ci baay
Thiofèl mouri kiiraay, wane niu model yi niuy roye
Goor gou yaaroo ciy djiguéne, jang yeurmeundé tari
Fok mou xarou jém ci guéneu, gni mou boot danio bari

Sample: Tarrus Riley

Degg – teewoul wowlé, niuy djap di door
Téela xam né un plus un moy goor japp ci goor
Maam wane nga yoon wa seut, daw na lakhou na sa rone
Dall na degg bakhara, Dall na jangue nassarane
Ay note la done weury lécole wayé dou xam xam ba
Bac dou yoonou tékki wayé yaakar lay xamba
Nguir xam faw nga nixma ci téel namm takam ba
Liy gueum ci moom dou moom, waral mou topp mame bamba Yalla – baxéko xaragne ci art
Mouy reude ci mur yi agg ci way dilene ci aare
Thiow li tambalé keur, teungueth né bakk nguén mbeur
Gonè gui yéem nieup, nieup nè diotna pakka guéneu mbar
… Fètantal ga moudjé na done daay
Diegui na bou yagg, bobou koudjé nga doon djaay
Niu hustle ci mbed, boolé teungueth ci hip hop
Taay la yoon wi néex, thiow li beury when the beat drop

Sample: Tarrus Riley

Niuy dox diko degg, kalaama gui niu codé ko
Djiteul tank morom topp, gueum né béss dinagne yégg
Record démo di codé mots yi, xalima gui massta lamb
Wakh jéy beury wayé barigo dina wathie mbartalam
Niakk baak-a waral thiow li ci téen, sigui naniu dèm
Gobi yé tok di djeuw capitaine, sigui naniou démb
Founé la baat di diogué, niu rangou ndakh nio boot bouki
Assamane laniou jeum takh niu wane guinaw njaboot touki
Nga def daniouy wakh, niak def daniouy wakh
Ndakh niom wakh laniouy def, niune waar ba last breath
Sunu yoona léer ni dé dina nieuw, we make history
PPS the name, the best who ever did it

Sample: Tarrus Riley

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR