LYRIC

Daniou dooré ci beat yi ba gars yi neubeu yate

Daniou crazy tek ci cool gayna dou yatt

Senaay na bou yagg, booba yoon wi taré goor

10e daan ci rap bi, procureur bi dafma téré door

Rhyme for free –  youxoul né Papa ngui nieuw

Niou déloola 9- 2 dou easy, crazy Peupeu ngui nieuw ..

Dama seug look ci book yi ba matt seuk leuk

… Ndank rek rak sama démbay sa euleuk 5

ans de carriere au sommet waral debats yi

Living legend ni takussane ba zidane di bayi

Sou teunguéth amè rap, wakhal MerCi Paul

So lén fandéwoul ci game bi ma rére ba bér ci bol

Fou sama xaragne yegg, yobouma bercy xool

Tàngue ni holocaust, dekal talaatay ndér ci xol …

Samay texte dou pour xalé, Ok j’accepte

Té pourtant dama open mind ni Abbé jacques seck

#Writah

Yeah, aksi nga poudlard

Sunu Kaddu Guéwou magicien, dioxate la gout de l’art

Nio beuteu beutou Dadjaal, fatèlikoul Odyssé

Nek buur yomb na, kou nékk ak ni nga koy guissé

Daniouye wagni di yokk vitesse

, comme game bi yaboy yi rek fi déss

Kou né di niodi king sa coner té manoufi indi lou béss

9 milli souy wakh, boom boom ngay degg ay raffalle

Djeuf jeul niax djarignu gueum gueum ni Cheikhra fall

Dou weed dou wine, negger dou sakh peundeux bouye

Wane ma bane jardinier rek mo fi doon djeumbeute gouye

Diaroul ngay thiangate kouye, léer na tabaski dou ko rombeu

Woowéma jordan ci rap bi, té basket di xorom ba

Doomu diolak lébou, jéemal dangay matteu bayi

So mbapatoul ci underground do diot ci martabaa yi

Sen Rap bi moudjé idiot, internet bey kill innocence

Mais Lou guéew rapadjoo, kou wéet xam sa bopp.

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR