LYRIC

{Refrain}
(Woma Woma) Sa journée nekhoul tay dji
(Woma Woma) Da nga am loula méti
(Woma Woma) Xarite dé lolay dieurigneum
(Woma Woma) Xarite dé lolay wareefam (Woma Woma)
Si t’as journée est pourrie mon gars (Téléphones moi)
T’as mal et tu gardes ça pour toi (Téléphones moi)
Si tu ne m’appelles là, je ne te comprend pas (Téléphones moi)
Pourtant les amis ça sert à ça (Téléphones moi)

Xarite deug moy kilay déguelou
Xarite deug mom doula neubou
Loula méti mou bokouko ak Yaw
Loula nekh mou andeu tchek Yaw
Xarite deug kène meunouko dieundeu
Dou wakh mouk lou bone ci yaw
Batakh bou dadjek yaw dou seugueu
Xarite Xarite sama
Xarite tooooo ooooooh woma woma

{Refrain}
(Woma Woma) Sa journée nekhoul tay dji
(Woma Woma) Da nga am loula méti
(Woma Woma) Xarite dé lolay dieurigneum
(Woma Woma) Xarite dé lolay wareefam (Woma Woma)
Si t’as journée est pourrie mon gars (Téléphones moi)
T’as mal et tu gardes ça pour toi (Téléphones moi)
Si tu ne m’appelles là, je ne te comprend pas (Téléphones moi)
Pourtant les amis ça sert à ça (Téléphones moi)

Yallah lène bolé ngène done ay waay
Ngène dem ba melni yéneu bokk Ndey ak Baye
Eh ! Kène meunou lène takalé
Mi ngui doré cii bi ngèni xalé
Eh ! Kène meunou lène diakhassé
Mi ngui doré cii bi ngèni gouné
Kone sen digueunté diarna sameu
Eh ! Xarite tooooo ooooooh woma woma

{Refrain}
(Woma Woma) Sa journée nekhoul tay dji
(Woma Woma) Da nga am loula méti
(Woma Woma) Xarite dé lolay dieurigneum
(Woma Woma) Xarite dé lolay wareefam (Woma Woma)
Si t’as journée est pourrie mon gars (Téléphones moi)
T’as mal et tu gardes ça pour toi (Téléphones moi)
Si tu ne m’appelles là, je ne te comprend pas (Téléphones moi)
Pourtant les amis ça sert à ça (Téléphones moi)

Woma woma
woma woma
Téléphones moi
Hanh ! Oh my friend call me call me
Téléphones moi
Woma Woma
Eh ! my friend so call me call me
Woma Woma
Téléphones moi

Sank ba légui ma ngui lay wollou
Dembe ba légui ma ngui la woolou
Sank ba légui ma ngui lay wollou
Xarite tooooo oooooh Woma woma

{Refrain}
(Woma Woma) Sa journée nekhoul tay dji
(Woma Woma) Da nga am loula méti
(Woma Woma) Xarite dé lolay dieurigneum
(Woma Woma) Xarite dé lolay wareefam (Woma Woma)
Si t’as journée est pourrie mon gars (Téléphones moi)
T’as mal et tu gardes ça pour toi (Téléphones moi)
Si tu ne m’appelles là, je ne te comprend pas (Téléphones moi)
Pourtant les amis ça sert à ça (Téléphones moi)

Sank ba légui ma ngui lay wollou
Dembe ba légui ma ngui la woolou
Sank ba légui ma ngui lay wollou
Xarite toooooo oooooh Woma woma

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR