LYRIC

{Refrain}
Yaaw suma ndanane namenala
Djougo fii souniou settt
Yaaw suma ndanane namenala
Sa tourr dou faay ba sounouy seute

{Verse 1}
Bour bey teunk lepp cii niar takh leudeum di sédé lerr
Ma foi vaut de l’or, Waral gueum di sa illerr
Djoy ak réé li djouti, doundou ak déh lou moudj
Djiteul mougne done lou diadou yonou lahou do tchi mouthie
Aduna dou waaye dou wéy, Rafetal defko xeuy
Boula am djay saxo liguey, natou ngui gawa def xaay
Bouri Bour yi ki boudou boum yi dou tiss dou mass
Lou néw massna beuri lakou ndaw doko miss
Gni djoy, gni wéddi, gni Imane di sèn wérouway
Gni niak sen waaye di xaalate koukoy térou baay
Beut meuneu touko laale, Sa dem niou nakar louko lole
Xell yé djoko, sou ndiaké namel lako lale
Djougué lenn fi sougni sett, Séni tour dou faay ba sunuy seute
Sassou maat doko djégui, djoy dou diékh cii sunuy beute
Nam nagn lènn, dotou niou guissé xeuyna
Li ngène fi bayi mouy lou tarou dotou niouko khayma

{Refrain}
Yaaw suma ndanane namenala
Djougo fii souniou settt
Yaaw suma ndanane namenala
Sa tourr dou faay ba sounouy seute

{Verse 2}
Borom béy nameu gni na-ngou, Ba beuss bigni san-ngou
Niane ak sabablou laniou am lou nieuw dagni ran-ngou
Wétay ya ngui may sonal bro soma dégué woma
Aduna wori nènn la, xeuy nga dém té tagou wooma
Lifi dess di worm, worna kou tédd ki sante warna
Lou meunoul niak fokk mou am nangoul nako Bourba
……
Gueuneu méti li amoul loudoul xana da bess
Yenn saay xell yi sori weuri sunu dégats yi
Elimane Boucar Diop Namena sama Gars yi
Mame Seydou, Abdou Khadr, Souleymane Diop, Modou Ndoye
Djolof niak na Bourba MCs yi Lass lagni djoy
Dagni fompe rongogne yi, Sigui dokh matale senn yéné
Dokh cii yone yi guène xaleu, Sass bi nonou laniou ko yéne
Waayé Alhamdoulilah namel dou té niouy sante
Fi ngène né yalla na dakk, Fi sèn bidéw lerr ni djante

{Refrain}
Yaaw suma ndanane namenala
Djougo fii souniou settt
Yaaw suma ndanane namenala
Sa tourr dou faay ba sounouy seute

Yeah for my bro Ousmane Noreuyni BA
Rest In Peace BayeFall
Nio ngui Sante
Douniou djouk cii sunuy xoll
Nio ngui Sante 

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR