LYRIC

Niak yakhine sounou yoon-a takh niouy djanaxé
Kounéy weur bountou mbékté dounde la niou Jah naxé
Kou moss doundou dinga dée eskeu diar na kheuw
Kou réer ci souf soko listixaré diar na kaw
Founé la tiss di xaaré, mba xeuthio bi diarnako
… Kouné di tifaaré, doomou badjénam yarnako
Yeah! Nopalikou noppé ko gueune
Lou guéthie gui sambaraax, bante dou sopékou djeune
Xamal né do nioom, alal dou sakh péggou gueune- Kou yakamti do niam, taraal jeuf yi feggo-k ngueum
Séete fo djeum, fékhé mou gueum loola
Makh-ay liguey ci souf, ndéké mouthieum lolou la
Tolouwaay, Kheuya xéwi deal bi goolou la
Khel yiy thiagatou, moujeunteul niakk ko wooloula
Kou diapé nitt sa bopp réer
Doomou baay bagne na niou bok rére

Xam xam-a gueuneu woor
Xam xam-a gueuneu woor

Kholay beug wayé dou beut goné
Li ngay xool beug sa beut la né
Lek lek beug ak bagne di xélmé, dou sélleu mais, sama xol sama biir xél la né
Dara sakhoul fils, lo fi guiss day diex
Hasard wala karma, dara nekoul ndakh dara biss
Nite leundeum, sa noon-ay doon sa diaraabi
Gni di diamou ndakh aldiana, nienene nguir khandiara bi
Hun! Am am ak dounda gaawa rombi
… Nguir sakh ci kaw, fekhel woyof ni kawaram bi
Deuddou xeulou farak xélou, taatane firri idji
La maam bayi laniouye guélou, bountou ya niou tidji
The best can be worst, yes vice verse No mercy in this concrete jungle, like my verces love is fearsome, precious, so strong
Light is bleeding in the dark, truth is going so wrong

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR