LYRIC

{Intro}
Yes Man ! Yes Man !
Bayi lène niouy wakh
Bayi lène niouy wakh

{Refrain}
Bayi lène niouy waxx wakh dji niom nio ko taal
Dieuf té djeul mom la Bamba diguelone Cheikh Ibra Fall
Weuwou xathie bi ci taly bi téréwoul auto bi agg fimou dieum bayi lène nio ko tal (x2)

{Verse 1}
Niou gui waar, Niou gui aar
Niou gui saar di dem
Thiow lé beuri rek bardé guène
Merdé guène Merdé guène
Wara djoog té di Wakh yène tardé guène
Let them talk ! nio gui Job
pour wa galé meuna tiopp
Haters yi meunou niou ma Stop
Li ma waar moy fékhé Go
Ma ngui fi dé yagui fé
Kham nga beurre dou Karité
mane sama réalité
Fils deh moy deh manduté
Na nga dokh sa dokh
Wakh sa wakh
Sama boss boul ko coupé
Diw li diw lé sa sou nek moy sa yité

{Refrain}
Bayi lène niouy waxx wakh dji niom nio ko taal
Dieuf té djeul mom la Bamba diguelone Cheikh Ibra Fall
Weuwou xathie bi ci taly bi téréwoul auto bi agg fimou dieum bayi lène nio ko tal (x2)

{Verse 2}
Tépp yé gui souss si nopp boum yi Indicateur le
Fathie kat bi mom di sauralé fou bi doundou secteur le
Niata la wakh dougueul ci biir
Yolémane yéé ngui riir
Wakh ba say nopp biiir
Do your thing ba lène ci biir
Sa guel mane la gravé ci kholam
Sama son moy daw ci call am
Move bi fils da nga ci gueuleum
Bone xol dou ci lekk deureum
Teubou niou rekk feuss
Té bougni mbéthie pess
Fokk niou wathie ci cars yi dou ci Lexus
Douniou fa dieul deuss
Kouniou fa mball reuss
fokk sunu djante feink rekk feuss
Yotou Push it, Khouss ci ay hit
Vinaigre none yi ba foula sen tiit
Bandit mic la
Waar bi bike la
Tay mou yakk la
Djité sappé ya

{Refrain}
Bayi lène niouy waxx wakh dji niom nio ko taal
Dieuf té djeul mom la Bamba diguelone Cheikh Ibra Fall
Weuwou xathie bi ci taly bi téréwoul auto bi agg fimou dieum bayi lène nio ko tal (x2)

{Outro}
Mame dane na wakh nane kou bott bouki xathie yi mbeuw la fo rombe yaw la
Mame dane na wakh nane ignane ignetti ignagnetti siniou noone la
Mame da na wakh nane bouniou demé bay wakh ci yaw da fekk nga djitou lène
Mame dane na wakh nane li Yalla def ci diame bo lène ko nango mou nopal lène

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR