LYRIC

Intro

YEE
ONE LOVE FOR MY PEOPLE
BISS BOU YALLA SAK NIOU NGI TRY POUR YEENE MEN
DOUNIOU MEUSSEU WATIE YOONE
YENA NIOU LINIOU DOONE
FOE MY SOLDIERS

1ST COUPLET

KARBALLAH

LEP SI TIONO LAGNKO DOR
KHARAGNE MATHJ KHATHJ DOORANDO
SI YONE BOU DESSE WOOR
NIOU FARAM FATHJE SEUKEUK DOOLE GOOR
NGEUM TAWE FA LAUR
SOUGN BAAT DOU LOR
SOUGN BEUT DOU DEGN SI BOR
LINIOU BOLLE FORT NIOU DIOMB GOR
BA JEUF DI DEGN SI NGOR
FINIOU DIAR DOUWONE LOU YOMB FARLOU MONIOU FAY
SABABLOU MONIOU MAY NIOU TAKHAGN SAY
BA TAAL FI LODOUL FAY
DANIO JEBEUL LIFE RAP JENGOU DIEGO FAMOUY SAFFE
MANE AK MBED SI JAH
WALLOU SABOU DOLLE DIAFFE

WICKY LOHJ

BENE PAS LAGNE TEK,GALSEN NIEUP DI KHEUW
TIOW DJIB NIEUP SIP DANIO YAG THI RAW
BENE TAPE LAGNE TEK PEOPLE CONS DEF BEGUE
WONNE NGEUM WONNE WORK HATERS YI TEUDIE SENE BEC
LIGNOU XARE DJI WOONE MO MEGNI TEY KHALIL NIOU YOONE
GNI GUEUUMOUNIE NIOU WOONE FORGET NE NIOUNE GUEUMOUNIOU WOONE
RAP NON STOP SOUNOU CORNER LANIOU SAMP SI
READY TO DIE SOU DIAARE DE BAKANE ROTE SI

“REFRAIN”

DOTOUL NIOUNE DEUKOUP LEUMEU NIOU SASS
TAX NIOU XEEP DOLLI
NGEUM GUEE DEUGUOU KOLEURE LANIOU FASS
DOTOUL NIOUNE DEUKOUP LEUMEU NIOU SASS
TAX NIOU XEEP DOLLI
GY – XEEP DOLLI
GALSEN – XEEP DOLLI
DIAPLENE GUOUNGUE GNOU THI NIOU NASS
NIO NGI THI XEEP DOLLI

2ND COUPLET

ZOU

DOOR NANIOU XEEXU NDJAAGO (x-n squad) THI ZOO (zou) BI DEKKIL XARRE BA WOONE KARBALA (KARBALLAH)
PACIFIQUE THI DIEUM AK DOLLEY KADDOU YOU MEUNE KAR BALAA
BOU DOONE GARAB TORTOR NA MEGNI TIOFEEL GUOU MBEUGUEL DI WITE
KOU DOONE KHARAB SEGNOUL YAKH YARAM DAWNA BA FA SA FITE
DEMBE !
DAGN DOONE RAP NGIR NIOUNE
DJITAL KOUN
GUEUM SOUNIOU THI MBED,GUED
LALLE YI DEG LOUNE MOUGNE
TEY !
MOMATOUGNOU SOUNIOU BOP JAH BI DOONE NA MISERICORDE
THI XEEP DOLLI NIO NGI WEY NDAM LI THI NGEUM LAGNKO MISE RECORD !!!

CHIGGA

SI INTELLIGIBLE LANIOU DOKH GUENEU NANIOU CAVERNE YI
HISSE DRAPEAUX EN BERNES TAKKEU RAMDIEUZ YI
DEUNGEUL SUNU BERET YI
XOUSS BY FORCE GUENEU SI MONDE SENSIBLE YI
FREQUENCE MODULAIRE JAH SI ONDE MANE AK MBED
TOUCHE LOU EUPP LIMOU 100 CIBLES YI
DIGUI BI DONE SIGLE YI SI SIDE BOUNIOU YENE GUISS MOU SIGGUI
(apostrophe)
SI RIROU JAH BI, RIGOU DIAM YI, DIROU RAME BI, DOUGGOU DAME BI,
TEPP TEPP DEM BA YOTTOU NDAM LI

“REFRAIN”

DOTOUL NIOUNE DEUKOUP LEUMEU NIOU SASS
TAX NIOU XEEP DOLLI
NGEUM GUEE DEUGUOU KOLEURE LANIOU FASS
DOTOUL NIOUNE DEUKOUP LEUMEU NIOU SASS
TAX NIOU XEEP DOLLI
GY – XEEP DOLLI
GALSEN – XEEP DOLLI
DIAPLENE GUOUNGUE GNOU THI NIOU NASS
NIO NGI THI XEEP DOLLI

“HOOK”

METITTOU YOONE WI MOUNOUL TAKH NIOU DOUTEEE
BOUDE THI NGEUM LE NIOUNE KENE DOUGNOU TEEE

METITTOU YOONE WI MOUNOUL TAKH NIOU DOUTEEEE
BOUDE THI NGEUM LE NIOUNE KENE DOUGNOU TEEEE
“JAH” BI DAY DEM!

3RD COUPLET

STAN

FOR MY SOLDIES
AME NA BOOR YO DOUL FAYE
GNOU YAGU WEUR ANYTIME FOU JAH BI DI PLAYE
LIKER WRITER LOVE LOVE VA KOY FAYE
GNOUGNOU TAFE SI SEN HEART YEN LAGNOU FETAL BI WAYE
YEN NA GNOU DEFF LOUGNOU DONE TAYE DEUGEULEU DOU AY LAYE
GNOUGNOU YAGU SUPPORT SI WAR BI GNOU DONE BAYE
SEN DIOFEL LAYE SEDE SI QUELQUE BARRE YI
AMANA BOUDOUL WONE YEN GNOU WEURIGNOU SI BAR YI

“REFRAIN”

DOTOUL NIOUNE DEUKOUP LEUMEU NIOU SASS
TAX NIOU XEEP DOLLI
NGEUM GUEE DEUGUOU KOLEURE LANIOU FASS
DOTOUL NIOUNE DEUKOUP LEUMEU NIOU SASS
TAX NIOU XEEP DOLLI
GY – XEEP DOLLI
GALSEN – XEEP DOLLI
DIAPLENE GUOUNGUE GNOU THI NIOU NASS
NIO NGI THI XEEP DOLLI

“HOOK”

METITTOU YOONE WI MOUNOUL TAKH NIOU DOUTEEE
BOUDE THI NGEUM LE NIOUNE KENE DOUGNOU TEEE

METITTOU YOONE WI MOUNOUL TAKH NIOU DOUTEEEE
BOUDE THI NGEUM LE NIOUNE KENE DOUGNOU TEEEE
“JAH” BI DAY DEM!

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR