LYRIC

Intro

{Verse 1}
Deukou naar yi soulard yi ci bar yi mouk dou waar-ri
Dou moromou CFA ak Dalasi rak rak mou niouki dollar yi
Door kaatou marteau leu (Door kaatou marteau leu) Mom charto la,
Daggueuh rek lay def ci xippi ak xeff rek mou ardo la
Lou rafet lay dawal ba noppi beug lou noyy
Dou feug mou moy yeukk dou yoyy koumou door nga djoy
Amoul palto, amoul place waayé amena keur
Amena auto, yorna xaliss légui amena thieur
Ndem Yonéinte Yallah CFA moy gueune gui mbeur
Waar dafay méti lool door la nieupeu di weur
Il vit au jour le jour sauroul déweune (kholoul souba)
Bou forré calpé Bour akka moy yéweune

{Refrain 1}
Néna sett-kat leu dafay guiss (Xéttou door la rek)
Doko dindi, doko miim ndax lerrna
Takkeu niarel bou am xaliss (Xéttou door la rek)
Gigolo nga, rigolo nga reer nga
Beugueu caméra niémé battré (Xéttou door la rek)
Samba alaar lambar-lambar serr nga
Xaritou Goor-Djiguène Yallah téré (Xéttou door la rek)
Yaw Goor nga wala Djiguène yeureumeul yaw sa Yaay

{Verse 2}
Meunouma lim niata call la taximan yi séyyal
Sa njaboot dafa wara lek lou léw kone liguéyeul
Tass yoré niéneti dom waroul takh ngay door
Souba kène xamoul noumouy moudjé déko saur
Sa souffou seurre bi Or leu waroko meuneu wétchék Keuyiite
Hors du Keuyite, Trouss peuyite, dindi ayyib
Légui djank dji, tchi apparte yi lagni dooré
Bo dougué té lambo poche boy gnibi do rééh
Bo noyé bopp nak bo gnibé do rère (Da ngay fandé)
Li nga yorone lagni soppi Brioche dorée
Daggueu pass dém Magali uniquement pour doori (Thieuy Yallah)
Simil nala chapeau ya ngui tchi bénène catégorie

{Refrain}
Taggo Maroc pour dem commerce wakhok serr yi (Xéttou door la rek)
Doko dindi, doko miim ndax lernaaam
Entrainé ba thiéné di weur mères yi (Xéttou door la rek)
Gigolo nga, rigolo nga reer ngaaaaa
Daggueu boumou gathié yi té xeuyo gonto (Xéttou door la rek)
Samba alaar lambar-lambar serr nga
Niouleul bédjaaw nioulay wowé tonto (Xéttou door la rek)
Yaw Goor nga wala Djiguène yeureumeul yaw sa Yaay

{Verse 3}
Thione Seck ka feegne lé rek, reuthie ganax gui nkégne la rek
Louy winw winw cii boppou mango bi dou lénène fils wégne la rek
Avocat yé diomi (rekka diomi) Juge yi xeum
Procès ci kaw procès yaggatoul légui trubinal bi xeum
Mane sakh beug na door mais comme Karim nak
Loumay doyé lampe pétrole fils waxma ay baril nak
So beugué done kou beuri alale féxel beuril nakk
So bagné bédjeune bi laale sa baxkh yi nak my nigga sorile nakk
Diamonoy fiit leu kou niémé woul kani do lekk cii akara djii
Lepp ci pét xam def tek pas de paparazzi
Kou tangal satala bi, përou nabba la fii
Wowéma Thierno Diallo kou wathie yoon rek Gora nafa la fi

{Refrain 3}
Def bouné wéingue teudeu peinou guinaar (Xéttou door la rek)
Doko dindi, doko miim ndax lernaaa
Dieuli assaka cii deukou naar yi (Xéttou door la rek)
Gigolo nga, rigolo nga reer ngaaaaa
Done dealer ci kogne bi di mayé dépense (Xéttou door la rek)
Samba alaar lambar-lambar serr nga
Goor gou démé bay leumbeul Taate yi nga niaass (Xéttou door la rek)
Yaw Goor nga wala Djiguène yeureumeul yaw sa Yaay

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR