LYRIC

{Verse 1}GalsenLyrics
Elève laadjatina professeur-reum
Ndax toppeu xellam wala toppeu coeur-reum
Kou beuri xam xam yorr ci poche yi deurreum
Est-ce que waxtu djotoul mou diokh montre heure-reum ?
Nénagne ngueum bi fok nga dioxko thieureum
Mais wakhou YALLA wala wakhou Serigne
Kouné soule ay affaire ci bountou keureum
Galsen deukou diiné wala deukou Xeureum
Nigga Diiné bi nénama njaalo aka bone
Ecole néna bania sole pote-Ca (Capote) rekka bone
Nieupeu dougone djangue maagueuh faté Kaamil
Gni dakkeu yëk ga dakone wathié Kaamil
Fokk nga diémeu fonkeu Papa ak sa Yaye
Wanté fi sa Yaye yay ndieuk sagga sa Yaye
Nigga Worral Worral, Yéwoul, Djoulil toubeul
Lou waureu waureuy wédi lire ay Xoutba
Goor ak Goor wédi ndirauk couple
Xorom sakh sou wékhé sakh ndirauk soukeur
Fi ngay guiss kou fayal djangue domam
Bania topoto lane lagni dougueul boppam
Xalé bobay maagueuh woutéék waat wa keureum
PA bi nek fofou di djoy naane “Baayi na yonam”
Motah Niggaz ya ngi ni di djoylo filles de joie
Niggaz ya ngi ni di djoylo filles de joie
Ya ! yen saay pour nga muur wèèn di nga sol yëré bou tolleu ci genou
Niouné “Lo Guiss day diekh” Souma tiimé sama Yaye damay gueumeu
Cours gui fess nak niou done fowé ay pistolets Bouniou lène di naane djangui lèèn
Xam Xam Garap leu bou Dom yi Nioré no meunti def dina am niou sani kherr
Beugueuh Alale ba xamouniou loumou niou diaral
Kou beug dara ak kou baniatoul dara
YALLA lay BUUR mais buur yi gueumou niou YALLA
MAKK dou YALLA wanté yaag naak YALLA
Am say dom ba paré berr lène di diémeu djaay Pa Allemand
Ngané lane ? Mais Berlin amoul Pa Allemand

{Refrain}GalsenLyrics
Djiguène bou xamoul goor dh dégnekay weur, Goor bu xamoul Djiguène dh dégnekay Wiiri
Pourtant borrou heure-rou “Wiiri Wiiri” domou Pa yu fiir yi lagnouy gueuneu irri
Negga ! Yeah ! gueuneu irri Negga
Domou Pa yu fiir yi lagnouy gueuneu irri Negga

{Verset 2}GalsenLyrics
I say: Wa keur gui souniou fonkoul séni dom Kone dh sen Xarite yi lagni wowé Mifa
Boul changé deuk mais changél deuk bi Aduna souy touki kène doula may VISA
Nit bou nioule déy youxou fi beu soubeu
Toubab dou dégg loudoul Houbaa Houbaa
Toubab beu xeuthione noppeu Sénégalais xeuyna motah Sénégalais dégoul Toubaaab
Fokk nga niémé wakh Niit boppam
Même goumbeu boko né “éh goumbeu” mou guiss boppam
Hummmm !
Oustaz dintial meu sa yatt bi nieuweul firil meu Aayat bi (Verset Coranique)
Xalé todj neu keur gui néna doundou woul sakh
Yaakeu biir té mom mi djoudou woul sakh
Anda ndo bou niaaw sou tassé rafett
Dara eupoul fiit ay dadjé tapett

{Refrain}
Djiguène bou xamoul goor dh dégnekay weur, Goor bu xamoul Djiguène dh dégnekay Wiiri
Pourtant borrou heure-rou “Wiiri Wiiri” domou Pa yu fiir yi lagnouy gueuneu irri
Negga ! Yeah ! gueuneu irri Negga
Domou Pa yu fiir yi lagnouy gueuneu irri Negga

{Verse 3}
I say: Nigga yarral sa dom, samal sa dom
Kou gueuneu am deh gueunoul djangueuh c’est faux
Niou gueuneu niaakeu niofi dakone xeuthio
Beug niééx dou takh niou dieul bou taangueuh xeupo
dakh bouniou tégué niam, kou féké si nga ?
Borom ndéki kouko ndieuk yéwou teudaate
Djiko yi sopalékou djaane ba maateu borom
Seintu Werr diaroule bouxeunté ak sa morom
Nénagne beug gane taxoul nga beuri gane
Mais nooyé aduna taxoul nga goudou fane
Bakane comme ay thiarakh bouy daggeuh doko yeg
Loula matt meunoul may maateu doula ko may
Yeah même bo amoul bac am kersa diarna baakou
Maggoum waxone nako mo gueune xamone naako
Ngélaw dougueul ko ci pax mais douko guéné
Bo dé baatu keur gui mbèdeu doula dégueuh nigga
Yarrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR