LYRIC

Yée
Yée (4barres)
1.9.8.3 la leer sopeekou di jeum
Baneexou dome bu goor – fompe rongogne yi demb
Thiapathiolé ganè si, dioye yaye sangue guémb
Dioudou di goor di sass, guéne wadiour ci seuguem ba
Yeah niou yar yor yir dalal daara
Yoonou taagate goor, gor piir daa lale dara
Son of the sun, ghetto boy tolouwayam
Thionoom di gueune, yelo boye, toul lou waay ame
Wara waar wilayam, nafar di sassam
Domou teungueth casamance, keuye dakhanté saassame
Si lecole si yé tole, li yée Sol ko yiitél
Def pépp si yé bol, def tekk ci tèel

Refrain
Yée (4barres)
Flow ak rime yi laye yè – yée
Mind bilaye yè – Yée
Guimi ci guindi ci baate you fine yi laye yè – Yée
Rap bi laye yè – Yée
Rap niou noyè – Yée
Ate bou nè mouye gueuneu nekh guèneu famou noyè – Yée

Born to shine, born to light up the whole world
Born to rime – Yée – born to conquer the words
The street desire, niou diox ko raya writah
The ghost, le fantome, la fontaine, a fond theme
Sakh ci mission deug, haqq ni kaddu naby
Sunu demb, sunu nguémb, niou akksi adouna bi
Mbebetou demb done taye, ferniente moudjé done daaye
Mbayou demb done faye, djébi niou goop doundé
Yée – Yée … Mbed feug yewoul
Li niu done sentu daaw mo teew rène, feulè fougn ko foguèwoul
Woyof toll ci bitti, diss gane ci biir
Tolof tolof ci sa tole tèwoul wassarè xibar
Teunku ci al Kabir, haqq ceedde jeggo yi
Nixma ci leundeum, siggui idji, kaddu thèddo yi
…. Waw goor weekotoul ci meune meune
Game bi tawate, di woute saafara, beury maa meune

Refrain
Yée (4barres)
Flow ak rime yi laye yè – yée
Mind bilaye yè – Yée
Guimi ci guindi ci baate you fine yi laye yè – Yée
Rap bi laye yè – Yée
Rap niou noyè – Yée
Ate bou nè mouye gueuneu nekh guèneu famou noyè – Yée
Flou, faux ba kou authentik niou né danga jeingue

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR