LYRIC

{Verse 1}
Ennemi dou ami xamna déféant yi
wakhalma soop man yi vrai defkat ba ngi
Fayaate meu 500.000 garélma Ferrari
Nianalma Yaay Amine ! ma teuthie séni lamigne
Damay tangal ba def fi incendie
Marqué l’histoire sans cahier sans bic
Djaay kattu caissou neew instant bi
Dina suul ay carrière sans pél sans pique
Pardon Monsieur juge non meusso meu guiss Moral bi ladoul di meuneuti
Fokk ma sodomise yeen imbécile ngèni may soga takkal menotte yi
F*** you yaak sa équipe yaak sa ay titres man leu Hakill
F*** you yaadone djaay fiit légui loy tiite tay lalay deal
Hééy ! Deum yi, Deum yi, Deum yi non douma sen ami douma sen frère
Bouma len wone téloul wone daw ngène dogatt dogattima rek defma séni rère
Samay morom danio contane, Bagnema guissoulé dama yokk concurrence
Tokna un an sans guéné téwoul meunouniou fekhé ba dépasséma nio ngi rang
Gni done laathie ana Hakill ? baay Hakill mo ngi fi, mo ngi cool, mo ngi dance
mo ngi cool, mo ngi dance, mo ngi dance

{Refrain}
Paréna Combat Amayi
Wowéma Champin’ bi ma ngui ni
Am tuur am Money moy deal bi
Champin’ bi ma ngui ni
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Gueusseum rek !
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Gueusseum rek !
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Gueusseum rek !

{Verse 2}
Salaam’aleykum fayma li ngama amel
Diaroul ngay wakh Malékum Salaam
Gueune fi beuri wakh té kossi diakarlol mouy ralenti melni kouy slam
Nieupeu dila kholé beutou koudoul téki yaw ngay saral. lolou fane la am?
Boula noone ladjé ndakh ya ngi ci jaameuh ? même boy beug dh wakhal fallaaw
Niémé risk ni kou amoul loumou niaak
Téleu soucis téleu keupeu amoniac
Esclave bou beug dagg boumou djaam
Agresseur boudoul reuthieu koumou djam
Gnimay niodi déh dagni perte sén temps niit bou déh dékiwaate rekka may djomal
Démal liguèy té baayi dima diir mbagueuh nékal sama boy rek dinala meusseu diongal
Gauche droite hypercute Hong Bak
Niata nek à terre en bas
Gueumou mani di nga def come back
Tchiiiip outeul bénène combat
Athie sama garde melni garde rouge bou nek bountou palais
Délou waat biir studio yi liguèyaate waw na gooré
Samay fans dagnema méré wone nénagne dama meuneu baalé (Ndèysaan)
Boy da ngène xamoul rek ma eupeu Histoire île de Gorée

{Refrain}
Paréna Combat Amayi
Wowéma Champin’ bi ma ngui ni
Am tuur am Money moy deal bi
Champin’ bi ma ngui ni
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Gueusseum rek !
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Gueusseum rek !
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Gueusseum rek !

Hakill mo beuri dolé (éy waaay)
Hakill mo beuri dolé (éy waaay)
Hakill mo beuri dolé (éy waaay)
Hakill mo beuri dolé (éy waaay)

Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul
Yeungueul, Yeungueul, Yeungueul

Added by

Abdoulaye Ndiaye

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR