LYRIC

{REFRAIN}
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
Yalla na Lahou def yeurmandé cii niom
{Azou Bu Atomik}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom
{Rosso}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom

{Verse 1 – Azou Bu Atomik}
Beugue tekki mou thiol,beugua dimbali yaye mou teuh
Beugua fekki ña sori lol,delousi guen si life bi dou teuh
dimbali baye guisnañe limouy dathe thi Jaaboot gui
Awou ko ndax mou noki ass touti bayi Jambat gui
Danel barak yi,tek fondement yeukeuti mur yi
bayi lek lou xaye naka lagnuy def ma diot thi yu mûr yi
Danel sakeet yi,teureul maket yi,laal mokette yi
tegui thine thi matte tek ko si gaz nopilo waxkat yi
Fan?Kagn?Xolal bi lé life limñu xagne
ñak mbañe,kañ lañuy bayi tib reer si añe
Bayi waxtou,bayi ñaxtou,nopali ci dox ba fouti
Kañ la xeweul yi di lawsi bañou bayi ndeké fouti
mbepeu kiray gnu beuti
diot li ñuy doundeul beut yi
Yotou si meñef yi witi mou yombe ñu ba ngene dou wouti
li mo waral xalima si xeut yi
ba dou law ba suñu seut yi
ndakh Yallah diam ak dale baw nane si xol you xeuteu yi

{REFRAIN}
{Rosso}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
Yalla na Lahou def yeurmandé cii niom
{Azou Bu Atomik}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom

{Verse 2 – Rosso}
Yeurmandé bou koune si gnom , si gnoune , si mome
Lamou yakar sou dé foumou waroul diar sopil djikome
Def wergou yaram,weuyeul Jaamam mou meune dieul limou mom
bou naré dieul limou momoul téweul loxom
Dafa dioumone,dafa rerone bi muy doundeu ci kaw souf
defal Yeurmandé si mome ndakh xam nañ ni yako meune fouf
Koufi top baneexou adouna ak limouy saf
bilahi digua xamni li si teeré dou ay kaff
Kou xamatoul foy tek sa tank sou yaabo soukil say laff
ndakh fouki lihlass ak bene dou teré ba douñu la gnaf
Na ñu Yallah mousseul si fimou lene di dougueul
koussi beugue mou dieugueul la bou yabo deh toubeul
Sou adounabi beugué diex Zaïr day gueneu nex
Pour ñu ame louñu sex dañu koy yendo di khex
ta fouñu tidjé sene signe rée ngir ame touti banex
dafa fek ñou tok di setane ñou melni sanex

{REFRAIN}
{Rosso}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
Yalla na Lahou def yeurmandé cii niom
{Azou Bu Atomik}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom

{Verse 3 – Rosso & Azou Bu Atomik}
{Rosso}
Yalna bourbi def yeurmandé souniou fandé
dañ laye ñan nga bagne lene wilipandé xol ni ñu soné
{Azou Bu Atomik}
Yeurmandé si liñuy dath dothe ba liñuy (…)
gno gui demandé thiono teguéko thi kaw gni life bi xothe
{Rosso}
suñu deké def aye sacrifice
Def lene ñu miss bi doundou bu triste nga may lene ñu guis
assamane si wis bis ñu yendi lou diss ba gna di doundou bi crise
{Azou Bu Atomik}
Yalla na Bour Bi Lahou def yeurmandé cii niom
{Rosso}
May lène wérr, diam ak xel bou dal bala delou fa mom
{Azou Bu Atomik}
Salam cii niom, nga may lèn katane meune fipou
Téki gni takou, kipi li keupou, diipi li deupou
Mossal lène tiafka dianatou bamou fégn cii séni lekh
Tégui lène séni natou baniou am sagn sagn di kékh
{Rosso}
Guindi gni teuthiou
Dindi djengou borom xell yi teunkou
{Azou Bu Atomik}
Djégueul gni reuthiou
Di niane cii yeurmandé lagni déinkou

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR