LYRIC

ONE LYRICAL

Da may hustle toogal di wax pourquoi ñu nan ma no way
Bëgguloo ma me too I do you baby screaming my name
I believe I can fly don’t tell me no bless over my lay
Still the same don’t know us
Keep yourself about me
Tay ma burle kon jarul pass
Ñaata nitt a ma gasal pax
Ñaata ño ma bañ
Mais nee nañ bul di topp sen xol yëppay bax
Ñaata ño ma yeene comeback
Ñaata nitt nga woolu denk len sa lepp tay ñu nan la yay kan
[F**k yay Kan] Motherf**ker yow yay kan
[Mof**ker yay kan] Topp sa yoonu bopp rekk a fi des
Sëgg ñi di wax siggil sa bopp
Siggil sa boop sëgg say wayjur hater niggers what a f**k
Man maa siiw parce que da ma sob
Li ngen ñoddi boo ubbe sama bopp ding ko fekk mu toog
Keneen ku melni man gisu mako
Ci kaw ci sa kanam feeteel ginaaw budul ci gent do ma f**k
Nee na la man bëggu ma jikko toot
F**k you ya’g sa buzz do gis ku dee yobbale siiw yawmal xiyaam
[F**k]

REFRAIN

Jël sama yoonu bopp a fi des (x4)
Jël sama yoon (x2)
Jël sama yoonu bopp a fi des
Jël sama yoon (x2)
Jël sama yoonu bopp a fi des
Jël sama yoon (x2)
Jël sama yoonu bopp a fi des
Jël sama yoon (x2)

HAKIL

Bo xamul fi nga jëm deelul fi nga joge
Loolu day fekk fi nga joge neex
Saytaane bari dooli ken duko jege
Mais dara dara duma teree xeex
Akk moom ndax ay sëttëm rekk ño ma wër
Bëggu ñu ma nekk ci Jàmm ni malade budul wër
Bimay ne sama biiru yaay rekk la nekk fu woor
Judd nekk goor
Zéro peur Yalla rekk lay soor
Awma lu may rèccu lepp noonu la
Duma changer tus lepp ci yoon bi la
Yen say lu gëna baax ci yow lu bonn bi la
Samay meilleurs professeurs sama noon yi la
Nitt ku ñuul ñemewul lu bees
Foo jaar ñu bëgg ma ray
Bu samay noon bariwul woon sama bopp lay njëkk mere
Mën a baax mën a bonn lo fi seet gis ko may internet
Nitt kuy weeco ay nitt doonul ludul nittu interêt
Jël sama yoonu bopp vitesse Foog ma seey len
Freins yi dagg may duggël vitesse gaaw ni Eminem
Ay jëmm tiim ma bëgg ma fees man may nittu neen
Jàng na ci lepp lima wees muy dëgg di fen

[Jël sama yoonu bopp, sama yoonu bopp, no no sama yoonu bopp] Topp ma ken ma ngi sama yoon (x2)

Ich yo boy
I got no excuse, no choice
The only way you are is living yourself and follow your own way
REFRAIN

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR