LYRIC

Hann ! Bitch Niggah da nga done bagne, Niggah da nga done bagne
Tu pouvais pas me sentir pourtant succès lagnou done xégne

{Verse 1}
Limo takh gnou yague tiite boy
Beugone FRESH 2 DEF, ak POP A SHIT boy
Awoumawone ndieugou sachets mbiskit
Légui chaque semaine ay cachets 6 ships
2006 école YALLA SUUR-EN fofou la commencé wone
Fofou la Omzo Dollar diougué
Faaté bougne may naane Omzo do meusseu ni DIOUMBI
Mayma quelques années dina néla da nga Dioum fils
Mayou Yallah la dou coup du sort
Tracé yone bi sama bopp lolooy étiffort
Takk sama fiit bagnou fokné damay monogamie
Prouver gnimay rétaane loumay lek vous ne serez jamais…
Hey ! Boy SICAP yi mane rek lagnou fan
Hé ! Rappeurou SICAP yi mane rek lagne bagne
Han ! Galé REGANE lagnou done guinz
Ladiaal JOSé niary nééne mbourou 75
Paassma Shaw bi amoul fiir niggah
Kouma déglou Boppam miir niggah
Constant Ventre plein niggah content
Même bouma khiffé ma ngui cii biir
Douma meusseu faté gnima done kaagno, Bima commencé wone,
xammo dara do def dara lolou lama gars yi néwone
Wané nima meuné wakhone nalène niggah I be do on
Amoul khadi sama faye dou tay dou soubeu té dou déh wone haaaa

{Refrain}
Bitch Niggah da nga done baagne (Euuy) Niggah da nga done baagne (Euuuy)
Tu pouvais pas me sentir pourtant succès lagnou done xégne
Bitch Niggah da nga done bagne (done bagne) Niggah da nga done bagne (done bagne)
PMC (Euuuy) ben mixtape
Légui lepp lerr nagneu

Bayima ma zalonner zalonner
Ey ma ngui zalonner di zalonner
Nieuweul gnou zalonner zalonner
Wa BUZZLAB nio ngui zalonner di zalonner

{Verse 2}
Han ! yagg dem ay boites niou naanema do dougou
Laangeuh ay Carapide peundeu melni keurigne laa (Thiooo)
Légui dougou club nga dégue NO DIOUTOU
Sama tuur cii carapide nga fokné Serigne laa (Thiooo)
1, 2, 3, 4, 5, 6, So amé kouma gueuneu fébaar may sa vaccin fils
Faut pas que tu insistes, Rap ba nieup cii GALSEN sipp
Ma ngui cii pays pauvre mais solena sama BASIN Riche
Ndaroul wone yagg cii c’était un hasard
Karak, Amitié 3, cii CP (Capsi) mi casa
Nice, beuri talent yagg fight bountou galem
Cii frigo lay nélaw, lane moy Ice Bucket Challenge?
Niggah ! Petits camps, Ibou mystique Ismael
Rappeur bou nieuw ngène diamou ko def ni CHRIS ah yeah
Sama guiss guiss la yém, meusso guiss fif tayel
Mane may réindi gni ngène gueum comme les FILS d’ISRAEL
Niggah ! Gars yi nénagne OMZO khamoul boppam (Boppam)
Mané sii xamena RAP niggah
Big up GASTON néena ma fi dakk Punchline
Mané MAFI DAK RAP Niggah (Euuuy)
Da nga faté bi nga may kong Baby
Légui diapp nga sama sounds Baby
Fuck say yëg yëg ak say E-MO-Ti-ON (émotion)
Fuck niggaz yi di changer kaname ni ay EMOTICON
Sama passe temps moy di virer samay horloger
Ladjal OSS temps classe toujours OMZO pééé
Damala call ci tweeter ya done provoqué
Rapdjolof.com site porno gay

{Refrain}
Bitch Niggah da nga done baagne (Euuy) Niggah da nga done baagne (Euuuy)
Tu pouvais pas me sentir (sentir) pourtant succès lagnou done xégne (Got’em)
Bitch Niggah Niggah da nga done bagne (done bagne) Niggah da nga done bagne (done bagne)
PMC (Euuuy) ben mixtape
Légui lepp lerr nagneu

Bayima ma zalonner zalonner
Ey ma ngui zalonner di zalonner
Nieuweul gnou zalonner zalonner
Wa BUZZLAB nio ngui zalonner di zalonner

Added by

Papi

SHARE

Comments are off this post

ADVERTISEMENT

VIDEO

GalsenLyrics

GRATUIT
VOIR